Le Thiant

Le Thiant

  1. thianta lay done ba fawwwwwwwwwwwwwwww

    Reply
  2. amet sant cheikh bethio mo serign saliou

    Reply
  3. santati serigne saliou magal gui nekh sante nagnou bou weer

    Reply
  4. cheikh bethio mouthial naniou rawalé naniou yalnafi yagg té wér

    Reply
  5. serigne cheikh bethio diamou serigne saliou mbacke yalla nafi yagu te werr

    Reply
  6. Le Thiant est l’acte d’adoration le plus élevé et privilégié d’Allah . Englobant tout autre acte d’adoration de Dieu, les pratiquants du thiant appelés « thiantakones » constituent une minorité négligente vis-à-vis de la population mondiale.
    Donc toi participant des thiantakones rends gràce à Allah de cette participation.

    Reply
  7. sant rèk mo fi dèss ak diarignou kone nak nagnou si nèk di nial Cheikh bi mou yague fi lole tè wèr

    Reply
  8. SANT SERIGNE SALIOU SEUL

    Reply
  9. serigne saliou le ciel, serigne saliou la terre, serigne saliou le vent; serigne saliou le soleil, serigne saliou la lune, serigne saliou les eaux, serigne saliou les lumieres….et finalement serigne saliou le tout…tout….tout; dieureudieufety serigne saliou mbacké cheikh béthio thioune diamou serigne saliou mbacké yalla nafi yague té wérr loooooooooooooooooool…..amine

    Reply
  10. dieuredieufé serign saliou bougnoula khamoul wone khamouma fougnou dieum

    Reply
  11. paroles de serigne saliou:’deflen cheikh mouy sen yitté’.yalla nanou serigne bethio dimbali ban defko yitté mom rék.cheikh bethio diamou serigne saliou yalla nafi yag lool te wér.amine.

    Reply
  12. sanat serign beithio rék ba fawou tifahaane mom kképou mom rék dimbeul leum ak yeurmadém si sounou kaw monou fètè kaw déy dior ak gnanmogn ak foumaham ak foumahaoul sant rék mom serigne beithio wawawa

    Reply
  13. sante rek mo ngou war rawatina thiantacoune yi serigne nena na kounek amener 10 personnes ngou diebalou ndah moy diarigne fi ak fe ngou dieum thioune yalla ga fi yague te werr

    Reply
  14. sakh si mome ba faaaaaaaaaw

    Reply
  15. ngaala thiantacone yii nanu beno ngir hamni mboloo bou beno lounu songu dane ko cheikh bethio tay ak euleuk

    Reply
  16. SERIGNE BETHIO rék mooy deug diko gnanal mou yag fi té wér!

    Reply
  17. Thiant moy li fetai kaw ci bep hetou diamou yalla .diereudieuf. serigne bethio bagagnou tegue ci yone Wi

    Reply
  18. ilyasse sidibé 30 juin 2014, 7 h 58 min

    DJEUREDJEUFETY SERIGNE SALIOU CHEIKH BETHIO YALLA NAFI YAGU TE WEER santat nagnoula di gnane sa djeum dji gnou mine mou yagu fi lol té wér.

    Reply
  19. serigne saliou rék ba faw yalnanu s.saliou saxal si képaru cheikh bi ba faw……..dieureudieuf thioune cheikh béthio

    Reply
  20. xana di niane sakh thi képarou SERIGNE bA FAWWWWWWW

    Reply
  21. gnoune ak chiekh bi ba fawou rek dieureudieuf serigne saliou mbacke

    Reply
  22. thiant bi serigne bi bekeu tey bekeulé

    Reply
  23. c’est ce que le cheikh nous a recommendé

    Reply
  24. dieuredieufety Serigne Saliou Cheikh Bethiodiamou Serigne Saliou yalla nafi gueuneu yagg lolou t andko ak werr ba faw.

    Reply
  25. ken dou mome serigne saliou

    Reply
  26. SANTATI SERIGNE SALIOU CHEIKH BETHIO THIOUNE REK!!! FIER DETRE TIANTAA!!!!

    Reply
  27. EMISSION THIANTACONE DAYE AME CHAQUE DIMANCHE RADIO XFM 91.3 A 22H

    Reply
  28. THIANTA LAY DONE BABAMAY DEH

    Reply
  29. Dieureudieuty Serigne Saliou Cheikhe Bethio Diamou yalla nafi yague té weer. Santate nanou seigne saliou si ande guinou ande ak cheikh Bethio yalla nanu deffal gorée ba lounou ame gnou santéko serigne touba

    Reply

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *