RADIO SANTATI

Radio Santati - Bande son de la semaine

 

 

 

 

 

 

 

  1. Siar,

    Merci de rajouter des SIKAR SVP.

    Diadieuf

    Reply
  2. Je pense qu’il faut faire plus de publication pour le 17 Avril

    Reply
  3. diadieuf m dolilene wakhtane yi ak mouhamed niang ak pape gueye yi

    Reply
  4. siaré mouride solén mounone ajouter khadim diagne svp bou bess bi 1ére titre bi

    Reply
  5. merci de mettre des xassaid de Pa Assane Diouf svp. dieureudieuf serigne bethio

    Reply
  6. Ziar je voudrez madal khabirou en kourel merci c pour mes repetition j suis de touba marrakech

    Reply
  7. C Papa Seck Touba Darou Salam Guédiawaye
    waw lène goor liguèye bi guène di def amna solo trop.

    Reply
  8. siar je voudrai des chansons de ibrahima diagne

    Reply
  9. vous devez enregistrer des waxtanes de serigne saliou samb et de serigne saliou mbow

    Reply
  10. J v l xassid inioukhatimou nasara svp
    J sui a touba fes maroc mercie

    Reply
  11. cheikh bethio diamou serigne saliou yalla na fi yagg te weer , amna solo

    Reply
  12. Grand thiant de Sokhna Mbossé Diouf ce samedi 22 fevrier 2014 à partir de 18h au quartier grand standind à Thies sous le ndiguel du Cheikh
    CHEIKH BETHIO yalla nafi yak té wéer

    Reply
  13. ma ngi ziar, si vous pouvez mettre allahou de ibrahima diagne et d’autres anciens chansons,merci d’avance
    dieureudieuf thioune CBT yalla nafi yague lol té wër

    Reply
  14. Sant rék monou war,lii da nékh way.Dieuredieuf Thioune,yague rék tè wéér.

    Reply
  15. siar je voudré le mafatoul djinan 71 kourell ouakam svp

    Reply
  16. thiant gui rk moy deg donc sah 6 rk moniou war yally naniou ko s.touba cheikh béthio défal amine té mou yag looooooooooool té wer dieureudiefety thioune

    Reply
  17. guisou ma si omar rou si radio bi

    Reply
  18. amdy cheikh bethio@hotmail.com 2 avril 2014, 1 h 03 min

    Nioun wa dara touba Istanbul niognui santati serigne saliou

    Reply
  19. Daara touba Munich 11 avril 2014, 18 h 05 min

    Siar Mouride
    Est ce que c est possible d avoir plus de khassida et des Watane merci
    Cheikh bethio yalla nafi yague tee weer

    Reply
  20. moustapha itecom 27 mai 2014, 20 h 08 min

    Le site sa tati SVP SVP SVP remettez nous les thiants samedis qu’il y avait sur le premier site. Wahtaanou ssaliou mbow yi wahtane you beuri y ou cheikhbi d’une wahtane nguir dieummi serigne cheikh bethio.

    Reply
  21. waw lenn guor naserigne bii yok khewel thii barke….cheikhe bii yok lenn wakh tann yii thi dadje,,,cheikhe bii ak kou ted kiii,,,,,,,,,,,,,

    Reply
  22. dara touba espagne,,,torevieja alcante ñii nguii sante bou werrr lii rek sede naa khol mouride,,,,,sante nañe cheikh bi mo ñou sagual fii thi europe,,,wakeurem douñou ñee kennn thioune mame bambii..

    Reply
  23. sant nanu si liguey gui ngéne ni def nguir nune ndakh manu soukheut sunu khol surtout khassaid yi ak waxtan yi

    Reply
  24. lamine bou CHEIKH BETHIO 28 juin 2014, 10 h 31 min

    CHEIKH BETHIO DIEUREDIEUFFFF refet lounagne bou baaakh liguey bi!!

    Reply
  25. lamine bou CHEIKH BETHIO 28 juin 2014, 10 h 33 min

    CHEIKH BETHIO DIEU REUY DIEUFF JAH DIEUF CHEIKH BETHIO! mbokou talibé yi yor site sen liguey rafet na sant nagne bou baaakhabaaakh!

    Reply
  26. TOUBA (D.V.F THIES) MANGUI LÉNI SÉRÉL NI LIGUEY BI SÉLL NA MOURITÉ NA JA NGÉN JEUF WAKANA BOU YOM ADIOUMA BI MATT NAY TÉKK DHÉ

    Reply
  27. Moustapha Mawahibu 26 juillet 2014, 1 h 43 min

    Waw lène goor. Recevez nos plus sincères encouragements de remerciements de surcroît. Votre faites un travail très élogieux; on vous en remercie et vous rappelle à plus le massifier. Bégg nane si yène looll Akassaa
    Cheikh Béthio sunu yaakaar tay ak euleuk yalla nafi yaag lol té wer

    Reply
  28. D. Ousmane Camara 6 août 2014, 15 h 01 min

    akassa liggey bi rafetna. Dieuredieufety Serigne saliou

    Reply
  29. Dieureudieufetyy sante nagnouuu yalla na fii SERIGNE SALIOU CHEIKH BETHIO yague lol t weer

    Reply
  30. DI SANTE SERIGNE TOUBA CHEIKH BETHIO THIOUNE DIAMOU SERIGNE SALIOU MBACKE DI RAFEETLOU LIGUEYE BI DI AK THIANTE ADOUNA AK HALAKHIRA TEEY NIANN CHEIKHOU MAME BAMBI THIAM YAGUE LOLOU TEE ANDE AK WEER JE VOUS AIMES;partager car c ancre dans notre religion………………

    Reply
  31. Santat serigne saliou bou bakh ligueye bii rafetna serigne cheikh bethio damou serigne saliou yalla nafi yageu lollll te andeu ak werrr

    Reply
  32. dieuredieufety Serigne Saliou Mbacke Cheikh Bethio diamou Serigne Saliou yalla nafi yagui t werr. waw len goor

    Reply
  33. serigne saliou diagne 7 janvier 2015, 18 h 01 min

    nous aimons vos publications

    Reply
  34. Dieuredieufeti serigne saliou IDRISSA DAARA TUBA RENNES

    Reply
  35. dieureudieufeuti segn b thioune suis vraiment content pour les rensegnement merci

    Reply

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *